@ndaya.sn8:

Une ndaya 🇸🇳☝🏾
Une ndaya 🇸🇳☝🏾
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 26 November 2026 23:06:48 GMT
395190
62171
2231
6052

Music

Download

Comments

userwoulita
Mrs Mbengue❤️Kholou P❤️ :
Seau foberé amna nioukoy sanguo
2026-11-27 14:05:17
207
radia242_
🍫 It's me _Diarra🪭👄 :
Kiy dieul sceau fobérékay disi raxass ndap nk🥺😩
2026-11-27 01:04:15
3492
user3986134596369
user3986134596369 :
Li deh mo geuneu interessant di liveee nane sama dieuuuukeurrr.
2026-11-27 10:08:51
1895
binetoumbaye139
Binetou khalifa🤍 :
Douche bou toyyyy 😭dina dagggg sama xol
2026-11-27 08:08:21
1218
bachir_joop221
MK✪ 🫀🇺🇸🇸🇳 :
Pour niom ridau Tabaski rk lanie ko wra changer 🤣
2026-11-27 08:02:12
3453
kebistarema
Rema :
Mais si tu habite pas seul dafa metii defois daguay beugueu dioy srx
2026-11-27 07:25:52
2050
mbayebadiane125
mbayebadiane125 :
sama awo mo geune sette c monde. bi
2026-11-27 09:08:45
397
mously_nd
Sokhna💋 :
Douche bou toy 🤣😭😭😭😭 meune nama rayy je préfère ma chambre désordonné que douche wagn ak salle
2026-11-27 00:49:00
616
user4948087767907523678
￴ ￴ ￴ ￴ ￴ ￴ ￴ ￴  ￴ ￴ ￴ ￴ ￴ ￴￴ :
Sama keur yay lolou mofa am mais bama seuyi djé keur famille la khamni les réalité ne sont pas les mêmes boy def yène yii gnuni dafa compliqué dafa sofff fekk ni lolou nga kham
2026-11-27 08:08:13
613
khouzbaby
Kh. Baby :
Tata xalé yiii dougn foottt soutien bou noir ak cuisar 🥹🥹🥹🥹🥹🥹
2026-11-27 08:29:29
898
hercule.bou.ndiol
Thiam demba bu rox🇸🇳 :
Mer iow la mana deukeull 🥰🥰🥰
2026-11-27 01:16:31
319
mamandiop1795
Maman Diop❤️ :
Serpierre douche ak chambre ak cuisine dou bén wayé yoor sa bén serpierre rk foune lay dougou , pausse pied nagne koy faute sidiadayi nane koy fote satala yi nagne koy rakhass
2026-11-27 08:43:16
128
marabout_du_senegal
ALMAMY KAHONE :
Y’a des hommes trop sales aussi !
2026-11-27 07:52:31
224
kenda2440
user3367309183737 :
Normalement serpiere biguay fonpei sa chambre waroul bokk akk biguay fonper peron bi akk salon bii akk douche endroit bou nekk akk serpiere bikoy fonpe wayei daguy guiss djek bo hamnii ben serpiere lay fonpei keur gui yeup
2026-11-26 23:48:22
987
ndindistore
Ndindi Store By Sokhna Maye :
Desfois nga dem keur beugeu djouli, sugn la djokhè yéré djoulikay ak sidiada bi tilim ba do meune concentré normal djouli🥺🥺
2026-11-27 13:00:25
117
antacheikh17
Sublime :
Liii cours magistral lanouko warone def
2026-11-27 17:12:55
1
fadjiie14
Fadieye✨🌹 :
j’ai l’impression d’écouter ma mère li deh laniou diangal et je la remercie énormément pour ça ❤️
2026-11-27 00:25:09
389
tigressenoire109
tigréssenoire ✪ :
Bilaye daguay défar mais niom aussi bouniou doull défar daguaye moudié découragé bilaye
2026-11-27 13:30:56
52
atiladiallo06
atiladiallo :
c vrai déh gnoune gaur dagno meunei séttlou yoyou bilahi
2026-11-27 02:03:18
8
babacarienne.2
Fatima🤍♓️ :
Douche bou toy meun na dag sama xol
2026-11-27 01:31:49
119
mounas2101
Mounas 2101 :
ay madame sougnou wa keur yeup nenagnou dama compliqué ndakh damay balé di rangé rek
2026-11-27 12:56:14
69
lionroug462
bb fatima rassoul :
tock lenn seuye nioune khaliss la niouyee autt
2026-11-27 08:40:56
76
1967lenfants1
L’enfant unik 😍💕 :
Mane dh sama patronne mako guena sett morso bougnouy fompé sale de bain mom lay dieul diko fompé si birr frigo bi dama wakh ba sone🥺damay sakh sékhlo nane
2026-11-27 08:30:02
35
To see more videos from user @ndaya.sn8, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About