Yalla sounou borom mangi lay niane si sa mbakh sa yeurmeundé yalla nga maye balla gaye ndam lou sétt wéthi le 29 inchallah niane rek mofi dess bonne chance champion 🙏❤️
2026-11-27 22:07:04
91
Princesse 👸 sarr 🦋❤️✌️ :
Ay yala soutoural gnou 😭❤️
2026-11-27 21:26:06
69
🌸Linguére Fall 💞🦋🍯 :
Yalla yaw mi yorr ndam mayal balla Gaye 2 ndam lou sédeu gouy Dimanche ❤️
2026-11-27 21:26:01
148
🌸 It’s mami ❤️ :
Instant bi magui stressé té combat bi dimanche yallah souniou borom mayal balla gaye ndam inchallah
2026-11-27 21:30:03
89
king_optique :
Balaa yalneu sa Borom mey Leu ndam Lou sed gouyyyyyy inshalah 💛💙
2026-11-27 21:22:36
36
Merlin :
yall nala yalla soutoural
2026-11-27 21:37:34
7
BG TARIQ!!🕷️🇸🇳 :
Yalla nagnou yalla soutoural 🥺 🙏🏾😭
2026-11-27 21:32:51
6
AïchaaaaaA🦋❤️ :
Ndam rk in shaa Allah 🤲🏻☝🏻🤗
2026-11-27 21:33:39
7
Élément serigne saliou :
Aye way yalla nala yalla sameu are la té mayla ndam lou sédd gouyi 🙏🙏🙏
2026-11-27 22:39:16
0
04 JANVIER 🤴 🎂HBD 🎉 :
Ndam rek inchallah 🔥🔥🔥
2026-11-27 21:22:12
37
Dieyna Bou serigne babacar 🥰 :
Yallah nala Yallah may ndam 🥰🥰🥰
2026-11-27 21:34:10
12
Princesse Lebou ❤❤ :
yalla naniou yalla may ndam 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
2026-11-27 22:27:11
0
Moustapha Mbaye :
ndame rek inchallah balla gaye Amine
2026-11-27 21:31:10
9
kOẞe GueYe :
YaLLa naniOu YaLLa sOutOuraaaL
2026-11-27 22:35:03
1
QUEENTY🇸🇳⭐️⭐️ :
Ndam rk 🙏🏾❤️
2026-11-27 22:21:43
1
Ka poulo🤍👻 :
Yalla nala yalla soutoural sameu la yalla Mayla ndam mou djik leu si barke seydina Mouhamed 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
2026-11-27 21:23:43
8
Fatima💕❤ :
yalla nalla yalla may ndam lou sedd gouy omar sakho🙏❤️
2026-11-27 21:42:00
0
aladji mbayalla sagne sagne bi :
guediawaye notre fierté
2026-11-27 22:03:55
0
KUMPAY PROD :
Yalla bou yakar tass👑👑👑😳😳😳
2026-11-27 21:22:38
525
Beugue Fallou 💪🏿💪🏿 :
Embience bi rek doyna
2026-11-27 21:28:50
8
Momoasouy🥰 :
Sport khalé 💪
2026-11-27 22:38:40
1
☠️☦️bigmo☠️☦️Gonzalez☦️☠️ :
awssa dou daan balla gaye2 dh
2026-11-27 21:47:24
3
Aïdara Couture✂️🪡🇸🇳 :
2026-11-27 22:14:02
1
FAN’S BALLA :
Balla yalnala yalla may ndam
2026-11-27 21:57:14
3
Pomme de terre🥔 💞😭 :
barki alhourane ☝️sama yarame Bangui dawe beugue nako rk 😭yalla naniou yalla soutoural 🙏 si barkép mame saliou 😭 ya allah 🕊️🙏 niongui laye niane nga défal ko ndame lou sédde gouye ❤️🫶🫂😭 que
2026-11-27 22:32:52
1
To see more videos from user @ballagaye2_, please go to the Tikwm
homepage.