Teh yalla takhe do neube vidéo yi ba lambe djie passe
2026-11-28 04:03:46
93
Galaye Bou Balla Gaye2🇪🇸🇫🇷 :
Non heure bi na gaw waye
2026-11-28 05:51:51
62
Penseur 🧠 :
Ki combat bi doko dépense 😂
2026-11-28 10:25:34
12
Lima Diagne :
Wawaw boul nélaw ba dimanche dèl weur nane da nguaye lamb rk
2026-11-28 07:00:21
22
FALLOU_ DACIA 10 :
ada yalla dogal na ba pare digua danou le 29 defarou wat rek
2026-11-28 06:58:35
25
Guem yalla jr :
ada fass seul
2026-11-28 13:01:54
0
Laye_Calteck :
Boy yénn nguir yalla beugeu ay vu boumou takh nguénnn beugeu di. Feusseul leup lou ada di def . Guisso bénn yonn balla di def déplacement si mara wala lénn gars yi dougal si jour apres combat rek ngakoy guisss .
2026-11-28 05:54:36
13
niang ballo🪡👔 :
mom kn douko ll 😂
2026-11-28 13:04:37
0
Kh4lil🤴🏽 :
Mome Ndeysane mogui takhawalou rek
2026-11-28 10:31:28
1
Libasse Diop :
Yalna niou yalla may ndam inchallah
2026-11-28 04:07:24
9
COACH DIABEL :
Bou combat bi diékhé bilay Dina toy😂
2026-11-28 10:35:30
3
Issa Ya Seydi Laye🇸🇳 :
Démal teuddi di weur, niou am dépense yeupp niogui nélaw, ce dara léroul guoyl, danou rek inchallah