Mon cas actuel 🥺sans affection rien 🥺aka metti lolou mo gueun a metti goumin 🥺
2026-11-28 21:42:58
22
𝑴𝐨𝐦𝐚𝐫 𝐌𝐚𝐨𝐝𝐨🇸🇳 :
Soula noboul kay Ngor amoufa bayiko té dem louy lolou ioe
2026-11-29 07:11:13
3
Le Jeune Indestructible :
Adduna bi y'a plus important que ayy relation amoureuse reww mi daffa metti deukk bi dëgger na kouné xoll no deffaré sa avenir doundou novelas bi nguén niou beuga forcé ça nous soûl