Balla vidéo yingay enchaîné daniouy yokk stress dh Kone tal nga vidéo 😩
2026-11-28 22:08:26
110
𝒎𝒂𝒂𝒉𝒆𝒎👸 :
Wa yéne titoléne ? 🧎🏽♀️
2026-11-28 22:03:19
265
Aida Patara BS❤️💍 :
Mane manouma lekkk 😩😩dakh combat bi balla yalnala yalla same 😭😭😭
2026-11-28 22:21:36
14
ÉLÉMENT SERIGNE BABACAR SY rta :
Souba guinaw djiouli tisbar bi Na gneup def 7 istikhfar 3 fatikha 3 ayatoul koursiyou 3 ikhlass 3 falakhi 3 Nassi gnou yené gnanalka sunu borom defalka ndam apres gnou tedjiéka salatou hala nabi🙏 yalnala borom bi may ndam omar Sakho
2026-11-28 23:12:02
1
Soxna awa🦋🖤🫶 :
Mbeur yakoy def dh inchallah 🙏☝️
2026-11-28 21:57:56
80
Djim_N01🖤🇸🇳 :
Balla nguir yalla kholal si Boyi sonneu nagn deh 😩
2026-11-28 21:59:42
96
RASSOUL✨VISION✨PHOTOGRAPHE📸 :
Mane d titouma bima kheuyer la dieul sama croissant sol ko ndéké samay chaussures dem sama yone préparer souba
2026-11-28 22:20:13
18
sokhna fatou❤️💍 :
Fitou ada rombou léne fofou 😂balla rekk ba fadiare 🙏🥳
2026-11-28 22:03:18
54
séne IA officiel 🐪🐒🐺🐰 :
ana gni beug seydina mouhamad PLS ☺️☺️
2026-11-28 22:00:50
33
🇵🇸BALLA SOPOU NABY(✪)🇸🇳 :
So guison Yonénti bii lokoy wax 🥺
2026-11-28 22:23:50
18
Møuss4real :
Eupeuleuw ay sama mbeur mi yalla nala yalla soutoural souba insha’Allah☝🏿❤️
2026-11-28 22:06:45
13
falllll :
yalla naniou yalla may ndame champion
2026-11-28 22:33:51
1
R🍒❤️ :
Yakoy deff deh gainder 😭❤️
2026-11-28 21:59:50
29
Khadijaba❤️ :
Yallanal yallla same soutoural la
2026-11-28 22:13:51
0
Seye Mamy :
ndame rék lay am innechalah 🥰
2026-11-28 22:31:55
0
✦𝕊𝕒𝕞𝕓 ℕ𝕘𝕒𝕘𝕟𝕖✪ :
Mbeur yalla nla yalla soutoural ☝🏿😍
2026-11-28 22:58:14
0
SEYDINA 🇸🇳🇺🇲 :
déf nga linga wara déf lép yallna yalla May la ndam Lou sed gouy❤️amine inchallah
2026-11-28 22:42:00
13
ouly :
ndame rk inchalla
2026-11-28 22:03:05
5
Oumy ndiaye :
Balla kone tall gua vidéo ni xaral ma dem rérii kone
2026-11-28 22:08:19
38
𝐴𝐷𝐴𝑀𝐴𓃵 :
sama confiance geuna yok
2026-11-28 22:00:49
31
K~N🌸🦋❤️🔥 :
Yalna yalla may omar sakho ndam suba Inchalla 🙏🏻sonou na 🤧y
2026-11-28 22:00:06
20
Sadya💕Mu S saliou🤍🕊️ :
Balla nguir yalla boudé yalla teral nala après combat bi do bayi beuré . Bilahi ioe rek yama meun tek pression si lambe . Yalla nala yalla soutoural❤️🫶🏾🥹
2026-11-28 22:07:44
24
ouly :
ndame rk inchalla
2026-11-28 22:01:04
8
To see more videos from user @ballagaye2_, please go to the Tikwm
homepage.