@khadimnianerafahi: S Ahmadou rafahi mbacke yonu touki episode 1🧏‍♂️

khadim niane rafahi
khadim niane rafahi
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 22 December 2025 20:52:16 GMT
51265
5691
190
201

Music

Download

Comments

moustaphadiop525
alkhourane Dij 🙏🥰❤️ :
bomay guiss gall dem
2025-12-23 20:02:39
13
geuye321
Tawfèkh Aouto mobile 🚘🛠️⚒️06 :
Yalla mogi fepp
2026-11-01 20:38:32
3
toure.bellingham5
𝑻𝑶𝑼𝑹𝑬.𝐁𝐄𝐋𝐈𝐍𝐆𝐇𝐀𝐌 :
Thaiy aka mana tontou 🙌🏾❤️
2026-10-01 08:22:00
3
78289woma
Momo 313 Bay darou bi :
Lou ler serigne bi
2026-08-29 19:43:17
8
sangue.diouf90
Diouf bois 🪟🚪🪑🪚🪛🔨🔴🔵 :
yalla bakhna
2026-11-02 20:19:11
1
ousayenoulaye807
weuzz décor ☘️🥰🫶❤️ :
Mbacke balla Diadiauff Mbackë 👏
2025-12-23 08:50:39
18
niang_rafahi92
niang_rafahi92 :
𝐘𝐚𝐬𝐚𝐲𝐢𝐝𝐢 𝐲𝐚𝐥𝐧𝐚 𝐥𝐚𝐟𝐢 𝐘𝐚𝐥𝐥𝐚 𝐲𝐚𝐠𝐚𝐥
2026-03-03 13:28:44
13
daroukhoudosstelephone
Darou khoudoss telephone :
2026-09-16 17:30:14
2
ousmane.diegane
ousmane Diegane Diouf :
sallalahou alla mouhamadine sallalahou alla mouhamadine ❤️❤️🕋🕋😢
2025-12-25 22:06:38
4
o302378
DembaSOW :
2026-03-04 23:58:02
4
fallouawabousso185
Fallou~Awa~Bousso :
Yalna niou yalla soutoural 🤲
2025-12-26 19:25:50
5
diop00m.t.f.d
DIOP BROME LÉRE💡GUI✅️ :
walaye ndayesan☝️lou ma mesoull deff😱🙏
2025-12-23 23:36:17
1
papymbengue235
Papis-tech_221🇺🇸🇸🇳💥 :
😂😂😂yagui aduna ky est ce nekoul Alahira sheut
2026-01-02 08:30:34
1
niae45
loum801💙❤️💯🫶 :
lou lér😱
2025-12-23 08:32:37
4
diopcralleur
ilimane Diop Cralleur 🇸🇳🇨🇦 :
😂😂😂😂😂😂Lou lerr
2025-12-23 12:24:12
1
7baobab
baobab bâtiment :
lep dina leer ak imam
2025-12-23 09:33:34
4
ametdiopalaloumoutakh
ametdiopalaloumoutakh :
Walaye dila deklou rek doyena diamou yala 🙏🙏❤️
2025-12-24 10:26:21
1
ablayediop006
GrandLaye❤️ :
Li bane nama rey sheutt bilaye deug gou reuy🤣🤣🤣
2025-12-27 14:30:24
0
sakaria.samb
pastéf :
ndaysan
2026-01-08 16:01:15
0
satouba58
Sa Touba :
verite absoli
2025-12-28 08:41:54
0
beuzcana4
Beuz cana 4 :
W c
2026-09-13 01:59:07
0
soowboulangerie57
SOOW BOULANGERIE :
🤣🤣🤣 Nice
2025-12-23 08:20:13
0
lilwizz123
lilwizz123 :
🥰🥰🥰
2026-10-17 01:02:14
1
mouhamed44801
mohamed samb 763487795 :
🥰🥰🥰
2025-12-23 11:30:03
2
user8865600301971
astoundong :
🥰🥰🥰
2025-12-22 21:00:24
1
To see more videos from user @khadimnianerafahi, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos

Al hamdu lil laahi nan gëm nangu ay dogalam Si Moom lanuy dello moo moom jaamñi ak luñu am  Innaa lil laahi wa innaa raaji’uuna ilay- hi Yalla mooy joxe mooy jël noo ngi nangu jëfëm Dunyaabi workat la moo woor Sayyidul-umami Moo wor Sahaabayi waajii Àddunaako xajam Wal mawtu baabun wa kulun- naasi daaxiluhuu Ubbilna Maam Alasaan buntëm nu ñàkk jëmëm Ni Dee budoon jotu kon Jullit ñi jot Alasaan Ci ruuh yo doy ni Sëriñ Raan raw na lun mana am  Bu ruugi doon jaay nu defsiy ndambi ndambi wurus Ba defsi Àdduna gep ngir Seydi Raan baña dem Taa’an wa Kaafan si weeruw Tamxarit cala dem Nuy seenu far waneen weer suux nu sax si lëndëm  Si Baktashin si atum Gàddaay ga Goorga laxas Bes booba tiis na ku tiitul daa newul diko gëm Ëllëk sa ñep rotsi Yoof kuniy taxaw di misaal Mbaaxuk Sëriñ Raan di jooy naa wëy fu Àdduna jëm Kep ko taseel mulanaa jaal naala Maam Alasaan Kubaax teyiw demna tay ngir fekki Maamja Limaam  Dunyaa lëndëm na kerook xol yepp weet na itam Shawxan wa lahfan si Baay Raan miidi bahrul-karam  Funuy giseeti ka donnoon Maam Limaamu si ay Jikkoom yu màgg ya Baay Raan yaanu làqqu badem Woyof na loolu ni ab xob waaye sooka xamul Baatin ba sànkala mooy Marjaanu moo raw ngalam Jikkoomya day geej Sëriñ Raan xuusko day jafe lool Te awma gaal kon xanaa ma wax si tuuti lu yam Taxwaa ilaahil- waraa moo fees xolam ba mu gëm Maamam Limaamu te woolot Yalla Buur binu moom #mouride_tidiane_layenne_niassene #mamealassanelahi #kourel_bu_yiw_bi🥺❤️ #bayelayeamoulmass #bayelayeamoulmass🕋🤍  @HaMsA_RoHuL_HuTsI ✪ @Al_Ghaariq @Seydi Rane

About