Khawma kañ laay dee.
Kon ñaanal leen ma Yàlla jéggal ma te yërëm ma. 🤲
Ndax kenn xamul kañ la dekk bi di jeex.
Su ma la defee lu la metti, jéggal ma.
Bul ma fàtte ci sa ñaan.
Yàlla na Yàlla jéggal ma te yërëm ma.
Yàlla na nu Yàlla jéggal ñun ñépp te yërëm nu. 🤍 »