@modouyaaydie: Man BAMBA doynama Man Bàmba doy nama, doyloo naa ko dootu ma fab Téerée ki maxtume ak ndomboy peurëg di ko sol Koo xam ne bëgg na gàllaaj ak alal aku nit Na dàl di jóg tàbbi géttam gii, te moo di ndigël Ki samp gétt gi, day wër gétt gée ka fegal Bëyam wi lor, waaye bëy wuy génn lëf di ko jël Xarit yërël rëbb baa ngii xëy soxug fetalam Jóg rombu gétt gi wéy, dem yooti rab wa fetal Xam ngee li tax rëbb bee jóg rombu gétt gi wéy Di weesu bëy yii, li muy gis sàmm bee ko waral Li tax mu jóg weesu bëy wii, tàkki téeré taxul Li tax mu dem rayi rab wee, ñàkk i téeré taxul Am sangg a tax bëy wi deewul, ñàkk sang a waral Rab yii ne jànjañ te ken neewul ki ray lu waral?

Modu Yaay jé Mbenda🟢⚪️
Modu Yaay jé Mbenda🟢⚪️
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 24 July 2026 21:03:43 GMT
12310
1208
18
67

Music

Download

Comments

maguettediakhate40
maguettediakhate40 :
diakhaté
2026-07-26 13:05:12
0
mbery06
user3213777527215 :
❤️❤️❤️
2026-07-27 03:19:17
0
bayf002
Baye Fall bi ❤️ :
Amine barkéb sidy birahim Fall ❤️
2026-07-28 13:54:00
0
gaye.ndiaga8
Gaye Ndiaga :
🥰🥰
2026-07-27 01:39:07
0
userabdoudio802926727258
baye abdou diop :
@1❤️
2026-07-30 00:37:34
0
user142048293629
user142048293629 :
amine
2026-07-24 22:07:28
0
modoukourambaye
Modou Faye8976 :
🥰🥰🥰
2026-07-31 12:14:19
0
modou.diop.baye.fa3
Modou Diop Baye fall mbaor fal :
🥰🥰🥰
2026-07-31 01:09:26
0
papeabdougueye7750
Pape Gueye :
❤️❤️❤️
2026-07-31 01:06:30
0
doctoring02
Baye Saliou Ndiakhate😢 :
🥰🥰🥰
2026-07-30 00:16:10
0
souleymane.diouf078
souleymane diouf :
❤️🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-28 19:39:11
0
moutafa.moutafa
Moutafa Moutafa :
👌👌👌
2026-07-27 11:51:12
0
user672680250791
pro bou Diourbel :
🥰🥰🥰
2026-07-26 20:21:07
0
mbayallgui
MBA YALLA :
🥰🥰🥰
2026-07-25 12:59:49
0
mbayesene082
mbayesene5065 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-24 23:15:56
0
moustapha.diop0880
Moustapha diop bay fall :
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-07-24 22:09:52
0
fama.dieye70
fama Dieye :
❤️❤️❤️
2026-07-24 21:07:42
0
djime.niang.24
djime niang 24 :
🥰🥰🥰
2026-08-05 11:12:59
0
To see more videos from user @modouyaaydie, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About