@dymo_story: Wooy Bouki ëmbal na guélam bi (parti 3)! 😱😂🐾 Bouki dafa doon am doute ci doom bi Coumba Bouki ëmb… 😰 Waaye Golo wax ko dëgg gi: Coumba Bouki worul ko mukk! 😳 Léegi Bouki xam na ne doom bi mooyam… waaye jafe-jafe bi mooy baayu Coumba Bouki! 😱🔥 Yow, bu nga nekkoon ci barabam, lan nga def ? 😂 #Bouki #Gaynde #TikTokSenegal #Histoirenwolof

DYMO_STORY
DYMO_STORY
Open In TikTok:
Region: FR
Thursday 03 September 2026 18:22:46 GMT
58139
8261
404
100

Music

Download

Comments

elimane375m
louis thior🇸🇳🇪🇸 :
bouki mi day dof dof lo rec
2026-09-04 10:19:15
2
........pape
Bouchera :
bouki kay soloul dall😅
2026-09-04 17:16:29
3
poowgold
CoumbiissePoo’wMadrid🤍 :
Ayyyy wayyy sama tour biiii🥺
2026-09-04 01:57:00
15
maman.coumba55
PRINCESSE 👸 SÉRÉRE🌹🌸🌸🌺 :
𝑨𝒚𝒘𝒂𝒚 𝒑𝒐𝒖𝒓𝒒𝒖𝒐𝒊 𝒄𝒐𝒖𝒎𝒃𝒂😳
2026-09-04 21:40:26
2
user2737869357876ai
Aïcha Diallo❤️❤️ :
mane legui amouma yakare si mane bouki bima topou rek di setane😂😂😂😂😂
2026-09-04 14:03:05
3
aloupr10
A͜͡l͜͡o͜͡u͜͡❥P͜͡r͜͡o͜͡🇸🇳🇮🇹 :
Mane mome légui amatouma bene foula yi rek laye sétane bouki fan leuh deuk si dakar sax
2026-09-03 23:56:37
8
moustapha.diakhat403
Moustapha Diakhaté :
2222
2026-09-03 19:07:21
7
160306awa
bb EVA ❤❤moufallou :
Partie 4
2026-09-04 18:10:28
1
informationtv221
H :
Hu
2026-09-03 22:40:24
1
mohamedfadelmane
job mane🇸🇳🇫🇷 :
marché grand yoff
2026-09-04 12:57:44
2
user85834446526140
Mayté sarr :
bouki kay soloul daleu🤣🤣🤣
2026-09-04 21:00:46
0
user37541502973128
Malick IPhnoe :
BADOU😂😂
2026-09-04 13:40:36
2
collsita.fall
collésita fall ♥️♥️ :
La suite
2026-09-04 00:39:42
3
binta.gnamadio
BINTA GNAMADIO ♥️♥️♥️ :
là suite
2026-09-04 15:38:40
1
nom24467
TOUBADiaw :
2026-09-03 19:29:09
2
To see more videos from user @dymo_story, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About