@xol_ak_xel19: 👆 Deffal li mucc ci àddina 🎙🧏♂️ Oustaz Taib Socé & Imame Birame Pouye Ci vidéo bi Oustaz Taib ak Imame Birame ñu wax li waral Kilifa yi di tëju Oustaz Taib Socé mu ngi wax ni nit war na tok bam yagg rek mu weet ak boppam bayi mboolo mi méditer ndax dafa baax ci doomu adama te so xoolé lolu moo am ndax nit di jéeki di wéet day baax ndax di na ko may mu mën xalat ci lu bëri lu melni ci Boroomam ci boppam ak it ci morooma di na ko may it xel mu léer ci ki mu done lim mën ak lim tëlé ak fi muy tek tankkam Oustaz Taib Socé ak Imame Birame Pouye ñu ngi ciy dooli né ku bégg mucc ci àddina da ngay wéet meytu cóow itam muy ay ndénkané yu am solo yu bepp nit wara bayi xel ndax ku weet meytu coow mucc ndax duñ né ya wax wala ya deff boo déemé émission karamti di nga am yoobal yi Serigne Touba bindël ndaw ñi ci la Oustaz Taib ak Imame Birame di leeral ci émission bi. 👇 Waax ñu sa xalat ci commentaire yi. Bul fatté aimer, enregistrer, partager ak it abonnement bi ndaw moo may doolel 🔥 @RTS SENEGAL @Imam BiramPouy